audio
audioduration (s)
2.68
7.99
transcription
stringlengths
29
63
mu teg saakam dal di dem ubbi palanteer bi
danga geestu ma xam ne moom geen di wax
metitlu na li nga ko yégalul takk gi
dinaa ko jot su ma yéegee ci taabal bi
këram dafa dëddu moo tax li ma fay dem barewul
ndégam mënuma fi xejj ñibbi rekk a ma dese
ca suba sa mu xëyaat dem summeeku ba set daldi né
tey dama naaje damay dem màrse ba ñów sog a sang xale bi
sàcc yi yóbbu nañu ganaar yi woon ci ngunu li
léegi du jamano soob nawet lay ñor
ndegam sa doom sëppéen la simis bi dana ko war a jot
boo fay dem ak woto dafay mel ni lu jége
fetal na mbaam àll mi doon ruur sunu tool yi
wool waxambaane yi ñu déqati bi ñu samp ci gannaaw
ba nuy nas nag lanu nemmeeku ne dafa jalgati lenn ci xaalis bi
leegi li ñu wara def mooy balu ko te daw seeti feneen
maa ngiy fàttaliku bés ba nu dajee foofa
dalal nga sama xel bi nga ma nee am na liggéey
Nanga ma ko fàttali lu ko moy dinaa ko fàtte
yaay daal nit a ngi xeeñ ci néeg bi
bi mu amee liggéey ba tey mu ngi ci jàmm
xamoon ngeen bu baax ne àttanul biib liggéey
seetal ci kóllëre gi dox sunu diggante
jinne ja dégg ko daldi fab lu doon ag ngeer
njaambur njaambur yi bey nañu ñebbe ju bare
sama kër a ngi féete jàkka ji sowu
jéem naa ko jubbanti ba tàyyi bërgël naa ko
sa xar maa ngi goor de mba du dafa feebar
mu ngi ne xàmm déggul dara ci li nga ko wax
lal fa seeni basan di naan sàngara di tóx di lekk yàpp
fekk na biram njéemée nga yendu ca mbënn ga fanaan ca
gox boobu fég nal sampal nañu ku nekk robine
su janax di sóoru muus ñag baa fa jege
mu téye ko lu yàgg ca yoxoom ya ba noppi bàyyi ko mu dem
caaxaan wéy na danga war jëmbët fulla ci njàng mi
mbuumbaay mee tax mënul def dara lu àntu
ci similaak saala asamaan si xiin ba ñalingaan
soo ko ko dënkee dina ci def farlu gi ci war
bul sànni xuuru xar mi am na du koy wàjj
dañu mànkoo ne dootuñu wax ak moom
loo xam ci suñu waxtaan ba ne xëtëb dugg ci
doj wi ñu ko sànnee ngi yem ci ndoN li
sompal tuuti ci poobar bi def ci cin li
bul tiit defuloo ko dara ba mu di la ñaan yàlla
ey biram njéemé koo njaay mu ngi ci kemu dëkk bi
jaxato dafa xaw nurook tamaate fàrsi
maamam a daan tëgg laxaab yi ca dëkk ba
fii laa ko tegoon xef ak xippi ñu jél ko
dànkaafu naa ko ba tàyyi mu të maa déglu
te sax boo dawul ñu nàngu sa allal faat la
séytaane teg ko ca jombaxtalu tangor ba
cere ji dafa wow kaas ko bala nga koy tay
dama leen woolu ngir laaj leen seen xalaat
bu ñu amaan gan ab gàtt lañu ko daan rendil
dangay gis jiit yi di dox ci leere gi
sama xol sedd na ci liggéey bi mu def
bër set mu daldi fàqlu lu dooni yari daqaar laxasante ko
yaa ngi téju rekk ci néeg bi génnal féexlu tuuti
mu yegg ci beneen dëkk nekkaat fa jaamu kër buur
muus mi dafa fettax dal ci kow janax ji
ba ko rajo bi waxee la coow la ne kur
puju néeg dina xeex ak taw te borom néeg du yég
mu ne mënula ñów waaye mu ngi leen di yokk ngóora
kolkolaat yégul né yembà baah nà
am xéy laa ko ameel ngont li maa ko moom
mu dem ci yaay ji ni ko buur nee na nga jél mu may la
ab roq la dajalee siddéem yi nekkoon ci toolam yépp
maa ko saytu ba mu fereem soow ba tey
xawma lu mu jóge ak ñaq wiy siit ci kanam gi
jox sama baay muraakem seel la maa ko nangoo ci Naar yi
dafa bëgg xam lu nekk ci kër njulli kaata bi
ku jél rongoñ siim céree m bu ko ñaan ñéh
benn xaal gala gàbbu na ko biram njéemé ndënnéer na
bunt baa ngi ne àpp te terewul mu tàng
gàpp bi weesu na bu yàgg dama koy seeti ndax ma soññ ko
njaayam mi du jar bu baax ndax dafa seer
kou di loo kham wëkh ko së ngor yakhou
li des ci sow mi matul sax ñaari góox
dafay jénd ay xar yafal leen jaayaat leen
dama koy saam ci lay gëna gaawa jare
moomuñu kër gi ñu dëkk dañu ko luye rekk
yeggaleel sa njàng moo la ëppal njariñ
doktoor bii mooy toppatoo ñi nga xam ni dañu siti
senegaal dafay jaay ariko bitim réew
ku ñu ko tànnal rekk mu né bëggu ko
su lëg lekkee aloom na ko gërëme coy
waa gànraar takk ab xare dabsi biram njéemé
fanweeri dërëm laa ko jox mu delloo ma ñaari dërëm
yàkkamti woon naa ñibbisi ba lat ci pajaas bi
mënuloo jënd garab goo lugate sa bopp bi
dégtal nañu leen ne dinañu fi jéle marse bi
bala ngaa jënd tam tamal ganaar gi
jéego boo def ngir jubale ay xarit yàlla dina la ko fey
Nangeen bàyyi xel ci dénkuwaay yooyu
dàmp bi ngay def baax na ci toogaay bu yàgg bi
jigéen ñu bare ñemewuñu njurug seex
saa doom xam nga lan mooy àddinaam
dinga yaakaar nit fekk mënul faj sa soxla
bala ngay tase ak moom dangay bëre ak ay suqam
sëpp jaleñ du la fasale ak say teeñ
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
85