audio
audioduration (s) 2.29
12.5
| transcription
stringlengths 26
118
|
---|---|
sunu meetar ñówul tànkam dafa faxaj |
|
Nanga ma ko fàttali lu ko moy dinaa ko fàtte |
|
am na ñax mu nu daan foye xuusmaañàpp |
|
maamam a daan tëgg laxaab yi ca dëkk ba |
|
benn seex bi gàjj bi ci lex bi laa koy xàmmee |
|
bu nawet jotee xay yi dañuy fees ak ay busëbaali |
|
dafa ne yoxoos dugg defe ne gisuma ko |
|
dinga yaakaar nit fekk mënul faj sa soxla |
|
booy seppi nanga fexe ba rënd bi bañ a tas |
|
sa jabar a ngi ci waaN waaN ji léegi mu wasin |
|
ce ngoon sa ba yumaane liggéeyee ba sotaal mu woo ko ni ko |
|
fanweeri dërëm laa ko jox mu delloo ma ñaari dërëm |
|
armeeli katolig yi ak yu jullit yee dend |
|
li ngay digle soo ko doon topp kenn du la gën |
|
jongama yaa ngi toog géwél bi di leen xalamal |
|
di dowal di dowal ba gëna dugg ci biir àll bi |
|
dowleen gaaw ñu pikkiir ko bala daNar wi di yéeg |
|
ba mu taxawee mu dem waaf ci genn ronu ngeer |
|
bu xale yi ñówee nga nàkk jox leen ko |
|
xam nga xéll ne ñetti nit xajuñu ci pajaas bi |
|
toN naat bu wëree am réew dunq yaa tax |
|
yoonam wi neex na indaale na bagaas yu bare |
|
xaj bi am na lu ko jot mu ngiy yullul rekk |
|
alkaati yi tàmbali nañu xàll léegi kilifa gi ñów |
|
yàlla miy far baakaari àddina si yërëm nu |
|
yàkkamti woon naa ñibbisi ba lat ci pajaas bi |
|
ñoom ñaar amareeg sàmba àgsi ci kër buur bi |
|
senegaal dafay jaay ariko bitim réew |
|
xel mi nga gase teen bi la ci keneen di naane |
|
yàkkamti woon naa simmi palto bi maaxàllaa dafa tàng |
|
piis bu tal bii du neex a sol ci tàngaay bi |
|
mbetteel gee ko jàpp ba mu toog ab diir bu mu waxul |
|
jotali ma njegenaay ma noppalu ci ndes mi |
|
lellil fi wextan wi laal ci tëll bi |
|
gunóor gi gas na bant bi ba mu wale |
|
booy fóot jëlal ndox mi ci póll gi |
|
bër set mu daldi fàqlu lu dooni yari daqaar laxasante ko |
|
séytaane teg ko ca jombaxtalu tangor ba |
|
dama la doon seetlu ba xam ndax sama xarit nga |
|
ñépp daldi jog tàccu yi dal coow li ak pënd mi jolli |
|
su janax di sóoru muus ñag baa fa jege |
|
bett nga ma lool foogoon naa ni dinga sàmm sa kàddu |
|
paske feebar yii fi nekk leegi xamuñu ko woon |
|
sëf ñaari nag ñeenti xar def jiwoom ba mu doy mu ñów |
|
ba nga xamee né xare bi jeex na tàkk mu wéy ca ña ca des |
|
yéesu dafa suufeelu ba di raxas tànki taalibeem |
|
sa kanamu alkaati bee tax mu ragal la |
|
bu jëkk jigéen ñi dañu daan ñuulal yoos mi di ko léttoo |
|
loolu de soo ko defee féewale say jabar |
|
jaruloon ngay lump sa banaana maa la ëpple |
|
ab dànnala la woon waaye bët yi neexatul |
|
metitlu na li nga ko yégalul takk gi |
|
omar mën na la dimbali ci saayir ak ci baatin |
|
dég dég amul i tànk waaye jàll na am ndox |
|
dafa bëgga dugg te bunt bi dafa téje |
|
am réew su fa lingeer dee fecc ku fay woyaan doo rusa yaN as |
|
baana baana yi ñoo daane njaayum naari bayruut yi |
|
ceglar daldi toog ci kow lal bi ni joor |
|
jox ma njàmpe li ma ragg samay tànk |
|
tërëx piccu ndox la waaalo waalo yi xam nañu ko |
|
dañu gas reen yi ba garab gi wëngéeñu |
|
karawan sëqul noonu waaye dafa gudd coleet |
|
luxuskat bi jommal na seetaankat yépp |
|
kàngamloo ma gënal ku ma dàq yóbbu ma nduluñ |
|
xale bi bég lool ni ko yow yaay sama yaay |
|
fas wi moom ci boppam dafa mel ni laalatul suuf |
|
dégg naa ne omar dafay ngoro ak astu |
|
booy jàngale nangay faral a misaal |
|
léeb wi ab liir la woon buy saga juddu |
|
bëggoon naa jaar sa kër waaye ma naaje yem màrse |
|
kaay dimmali ma ma randal waxande wi |
|
bul ñormati mburu mi dog ko benn yoon |
|
am naa beneen xiseb li nga ma nettali |
|
ku teb dal ca safara désé nà bénén tebin |
|
mu dal di ne jinax ja yalax ci seen biir |
|
walisu laytaay yii turandoo liir bee ko joxe |
|
ba màndikat ba daanoo ndaw si dafa ree ba kekku |
|
ba ma ko sangee ca tabaski daaw ja mbubbu mbaseñ la ma mayoon |
|
bu seen pexe soti woon tey duñu fallu |
|
mbër maa ngi ci diggu géew bi suq yi dar ko |
|
wàññil xal yi lu ko moy jén yi dar |
|
xéy na bu takkee jabar dootul xaaraan |
|
ndimo lu xonq la sol dinga ko gaaw a gis |
|
ndegam sa doom sëppéen la simis bi dana ko war a jot |
|
yaay daal nit a ngi xeeñ ci néeg bi |
|
fu mbott tarxiis ba damm bu fa giléem jaaree wara def ndànk |
|
ndey ja wasin mu yobbul ko butiiti sikket |
|
njureel sagu bépp jigéen juy séy la |
|
Nanguwul lekk dafa coppati rekk ci yàpp wi |
|
puju néeg dina xeex ak taw te borom néeg du yég |
|
lérén dina fànqal liir yaram wu ñaawlu |
|
fàkk naa yoon wi ba amatul benn gàllankoor |
|
jottali ma boppu jén boobu ma maccaat |
|
boo jëndul bul nappaaje sama njaay mi |
|
am na fi ba tey géwél yu la mëna nettali cosaanu |
|
xamoon ngeen bu baax ne àttanul biib liggéey |
|
tuub bi dey jaru ko sax nde waay si saay saay la |
|
mbaam xuux bañul dara loo ko jox mu lekk |
|
wool waxambaane yi ñu déqati bi ñu samp ci gannaaw |
|
géej gaa ngi ne màww ci suñu kanam |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 37